SALÂTUL FÂTIHI EN WOLOF
Yow Yàlla mi si turr yu rafeet yi ak meloo yu yekkati ku yi julîl si suñu sàng Muhammad
Kiy aji tijji li tëju woon
Te mottali li jiitu woon
Kiy dimbali dëgg ci dëgg
Kiy jubale ci sa yoon wu jubb wi
Julli gi def ko ci mboleem ñoñam keem tolluwaayam ci yow Yàlla ak dayoom gu màgg gi
https://twitter.com/Samba_Ebraheem/
Baay Samba